RSS

Dédicaces

il y a 9 mois
Radio Urum-B
Di jaajeufal kepp kouy deglu Radio Urum-Bi.
il y a 9 mois
fatou samb
laye maxtar mangui lene di ziare bou bax di contane loll ci radio urum bi ma sha allah sikar si nexna xol seddna laye maxtar ???????????? JAAJEUFEUTY, SOXNA FATOU SAMB
il y a 1 an
Laye laye
Macha Allah Laye makhtar yalna yalla yokk len bou bakh ci barké Mame Baye Laye hanleyhi salam
il y a 1 an
Ahmed laye
machallah radio urum bii radio dinè djii
il y a 1 an
779625055
Laye laye je suis tivaone
il y a 1 an
soda lahi
machallah laymaxtar cherif abdoulaye yall nafi yague té werr m
il y a 1 an
laye makhtar
nianal sounou khallifa
il y a 1 an
Aicha Laye
Laye mactar contane si yen
il y a 1 an
fallou laye
felicitation
il y a 1 an
Bineta laye
Kaye makhetare magui ziar
il y a 1 an
Évita Laye G
Machallah laye makhtar yokou ba yeuk ko inchallah
il y a 1 an
779979670
laye laye Ziarre na niep yalna yalla deff diame
il y a 1 an
rane sow
Machalah laye makhetar
il y a 2 ans
ndack laye
Assalamou aleykoum wa Urum-Bi, machaala diadieuf wallahi zikroulahi bi nexna Sounou faye leen barkel Baye lahi aleykhi salam
il y a 2 ans
Seydina
Machala radio bi nékhna
il y a 2 ans
Sokhna laye
Mashallah yalla faylène ci barké cherif Abdoulaye
il y a 2 ans
pape amadou
animation bi nekhna
il y a 2 ans
Seydina issa diop
Mashallah
il y a 2 ans
Madeleine
Machallah lahi makhtar
il y a 2 ans
Seydi Souley
Laye Makhtar niongi mbekter si dorra yeksi bissi Application
il y a 2 ans
Karim
Laye mactar ziarnalen
il y a 2 ans
awa laye
Laye mamadou makhtar nexna loool la mbengue bi yalna yalla maynou nou tewer ak diam appel bi talko ak meune ko teral gane gneup inchallah
il y a 2 ans
Limamou Laye al mahdi (psl)
Laye makhtar merci pour la radio
il y a 2 ans
ndack laye
Diadieuf leen laye makhtar machaala, baye Lahi amoul mass, baye Abdoulaye yagg fi te weer si katannou Borom bi
il y a 2 ans
Radio Urum-Bi
Assalamou Aleykoum, Soxna Fatima. Meun nga jokkook Radio bi ci 77 988 9670 / 76 350 9670 / 70 680 2864..
il y a 2 ans
Fatima
ziar naléne laye makhtar contane trop thi sougnou radio bi ma beuguone bokk thi bèneu dahira tè khawma nana lay def
il y a 2 ans
MBOUR ahlou
Bismillahi Rahmani Rahim Laye laye magui ziaar Di am contenté AK mbékté loool diléne nianal matériels yi yoku barké BAYE LAYE SAWS AMIIÎNE
il y a 2 ans
Mame Baye Lahi ma raison de vivre
Laye makhtar diadieuf si zikr Lahi Na leen Borom bi fay barke Baye Lahi
il y a 2 ans
Fadel lahi
machallah
il y a 3 ans
talibe mame baye Lahi
Laye makhtar diadieuf leen bègue neniou machaala